Koumay firil bii gént

Dama gént di dokh ci Bén forêt bou leundeum mann késé di dokh,
Ba ci yague rék ma guis bén Gaîndé bouy nélaw, ma tiit di dokh ndank di yoot di yoot ba ci yague rék bén khéer fakastalma ma danou rék, Gaîndé gui yéwou dakhma may daw mou top ma, ba ci yague rék ma danou, mou tiim ma di mar sama yaram wi, ba ci yague mou dém bayima, bima démée ci deukk bi, diko nétali waa deukk bi, naa léen bén Gaîndé mooma dakh bama danou mou tiim ma, di mar sama yaram wi, niounima khana dou Gaîndé beige marron bi, mani waw niounima daa amoul beugne, mani mais moom dou Gaîndé bou magatte, niounima daa dioudou waalé woul beugne,
Niounima bou guissé nitt koumou khamoul noonou lay déf, dila napp wàayé dou déf dara, bouki you ndaw wi sakh daniou koy dakh mouy daw,surtout bouki bou ndaw bi deukk Gambie boobou rék la ragal foumou ko guiss daw,

Commentez avec Facebook

Voir aussi

Les questions dérangeantes de Woré Sarr à Ismaila Madior Fall

Les questions dérangeantes de Woré Sarr à Ismaila Madior Fall Commentez avec Facebook

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *